MUZTEXT
Текст песни Jammu Africa - Ismaël Lo
Информация о песне На данной странице вы можете ознакомиться с текстом песни Jammu Africa , исполнителя -Ismaël Lo Песня из альбома: Best Of
Лейбл звукозаписи:Capitol Music France
Выберите на какой язык перевести:
|
| Afrika a a a Afrika mon Afrique |
| Sama gent gi maa ngi ñaan Yalla wonma ko bala may ñibbi barsaq |
| Ma ne bes du ñakk ci bes yi Afrika don benn reew |
| D’ici ou d’ailleurs nous somm' des enfants d’Afrique |
| Mêm' si le ciel tombait luttons pour la paix |
| Kon jammu Afrika moom lay ñaan |
| Mané jammu Afrika mooy suñu natange |
| Afrika a a a Afrika a a |
| Afrika a a a Afrika mon Afrique |
| Yow mi nekka bittim reew man mi Lô maa ngi lay ñaan |
| Ak loo fa meun ta am ak noo fa meun ta mel bul fatte Afrika |
| Ici ou ailleurs la paix prix du bonheur |
| Mêm' si le ciel pleurait luttons pour nos frères |
| Kon jammu Afrika moom lay ñaan |
| Mané jammu Afrika mooy suñu natange |
| Afrika a a a Afrika a a |
| Afrika a a a Afrika mon Afrique |
| Onon bibbe Afrika ngimode, ngimode liggo-den leydi men |
| Ngaccen hasi daagal yoo Alla suren e musibaadi |
| Yoo Alla addu jam to Ruanda |
| Yoo Alla addu jam to Burundi |
| Yoo Alla addu jam to Casamans |
| Lawol Mbignona yee |
Поделитесь текстом песни:
Напишите что вы думаете о тексте песни!
Другие песни исполнителя:
| Название | Год |
|---|
| 2015 |
| 2015 |
| 1986 |
| 2015 |
| 2015 |
| 2015 |
| 2015 |
| 2015 |
| 1999 |
| 1999 |
| 1999 |