Текст песни Adouna - Natty Jean

Adouna - Natty Jean
Информация о песне На данной странице вы можете ознакомиться с текстом песни Adouna, исполнителя - Natty Jean. Песня из альбома Imagine, в жанре Регги
Дата выпуска: 04.10.2018
Лейбл звукозаписи: Baco
Язык песни: Испанский

Adouna

Nit ñi fi ñuy rawante / mooy ci xol yu rafet yee
Nit ñi fi ñuy amee barke/ mooy ci ñaanu waa-jur yee
Nit ñi fuñu jëm ag yaakamti / xanaa bëg yaxxule
Kon sa wërsëg ding ko fekkee/ xanaa waxtu bi su jotee
Na nga sant, sant, sant, sant te baña yàkkamti waay
Kon defal ndank, ndank, ndank, ndank mooy jàpp golo ci ñaay
Mu xiin, mu taw, mu neex, mu naqari (na nga am sa fulla waay)
Nga weex, nga ñuul, nga am ba xamadi (yaw bul fàtte Yalla waay)
Bula àdduna jay ba nga fàtte ki nga doon ding ko réccu
Nii de laa ko gisee
Yalla buur bi nelawul té gëmmentuwul
Leeg leeg mu jàpp njamburam ne tekk
Te loo ko ñaan mu may la ko si kaw nga laabir
Ag am jom te nangu lepp limu la teg
Nit ñi dañu bare dugg-dugg, xoolal bu baax
Laatà nguay dugg ci lu la bett
Nangu jël na cëru bañ ba tax na tay jii
Ki nga gën a wóolu moo la mën bett
One two three/ suñu Sénégal a ngui
Sutura bi daf fi jeex ba luñu gis di nettali
Mbele mbel bi bari, seen xol yi naqari
Nañu job te bàyyi coow li
Mu xiin, mu taw, mu neex, mu naqari (na nga am sa fulla waay)
Nga weex, nga ñuul, nga am ba xamadi (yaw bul fàtte Yalla waay)
Bula àdduna jay ba nga fàtte ki nga doon ding ko reccu
Nii de laa ko gisee
Yow da ngay mel ni nga wara mel, ñun ñu nangu say jikko
Buur bi baaxèe na ñu xel, li ci des mottali ko
Da nguay def li nga wara def, sa wërsëg lijjënti ko
Àdduna ag ni mu mel lo fi góobe garaale ko
Buula Yalla teggee nattu man what can you do
Li may ñaan mooy jàmm, wergi yaram, fan yu gudd
Na nga màndu, doo ko réccu, na nga tuub, jéggalu
Yalla rek a dul juum, nañu dem jébbalu
Ñu bare dañuy fàtte ne àdduna jaru ko
Ag loo fi mën am yaw da ngay dem bayyi ko
Kila bëg waxla dëgg da ngay teey deglu ko
Dunyaa tay jii dafa dem ba jaxasoo

Поделитесь текстом песни:

Напишите что вы думаете о тексте песни!

Другие песни исполнителя:

НазваниеГод
Je marcherai ft. Natty Jean 2016
Comme je ft. Natty Jean, Manjul 2021
Ne touche pas ft. Natty Jean 2014
Poupées russes ft. Natty Jean 2014

Тексты песен исполнителя: Natty Jean